Photos - Ndeye Gueye en pleine démonstration de " Takh ci Ripp"

  • People
  • 16 novembre, 2012 à 17:11:47
  • Mis à jour le 16 novembre, 2012 à 17:11:13

Photos - Ndeye Gueye en pleine démonstration de " Takh ci Ripp"

Ndeye Gueye dans ses oeuvres

#1

Ndeye Gueye dans ses oeuvres

#2

Ndeye Gueye dans ses oeuvres

#3

Commentaire (40)


Yama En Novembre, 2012 (17:54 PM) 0 FansN°: 1
ngir yallah ndeye bayil yi, amoul bene ndieurigne. Dé day bété té dina gnaw lolou ngay fethi ba meuwti fekk lafa. Soutoural sa bopp way ngir yallah
Moi En Novembre, 2012 (17:57 PM) 0 FansN°: 1
hahahahahahahahaha
Fethiendrye En Novembre, 2012 (19:59 PM) 0 FansN°: 1
oh ndèye, cette danse de lutteur n'est pas belle à voir chez une femme
surtout chez celles qui sont grandes de taille, c'est tout simplement moche
Patcha En Novembre, 2012 (21:37 PM) 0 FansN°: 2
celui qui a tendu un micro a ng pour chanter mou niou togne. elle chante comme un tonneau mais bon il faut survivre par tous les moyens donc laisser la faire si elle ne fait aucun mal. eduquez vos enfans, emmenez les a l' ecole. on vieillit avec ses connaissances mais la force des thiakhagounes est temporaire. donnez a vos enfants, l' amour, la securite et ils n' iront pas les chercher ailleurs. surtout apprenez les a s' aimer et a se respecter, c' est le plus cadeau d' un parent.
Beug Soutoura En Novembre, 2012 (18:08 PM) 0 FansN°: 2
ayway ndeye gueye boula hakh senegalais yi diape dou bakh yakhnga khales yeupeu takh ngaa matouniou lounou nekh thi sounou diabootegui wayway dimbalinou bayi sayou bonneyi ngaye def boguene tay bou souba nga ngene benene lakal nganou

Yama En Novembre, 2012 (13:35 PM) 0 FansN°: 1
woy sama ndeye le mec a la photo 3!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!
Friends En Novembre, 2012 (18:18 PM) 0 FansN°: 3
De quoi vous la repprocher laisse la tranquille bande de jealoux. Du courage ndeye
Mifi En Novembre, 2012 (18:19 PM) 0 FansN°: 4
BILAHI NDEYE GUEYE AMOUL AY MOKOU ZERO CLASSE ET SALLL TYPE

Boy Town En Novembre, 2012 (18:23 PM) 0 FansN°: 5
Takh ci ripp . Eummmmmmmm , c'est tres evoCATEUR
Vilguer En Novembre, 2012 (18:35 PM) 0 FansN°: 6
ndeye gueye takh nga djiguene amatoule valeur un peut de dignite pas pour toi mes pour tes enfants et ta peuvre maman que aceuil aux paradis :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet: 
Saly En Novembre, 2012 (19:54 PM) 0 FansN°: 1
tu connais pas la définition de valeur toii tu utilise des mots sans savoir bref c son métier et sa vie sa yone nekouthiiii
Mimi En Novembre, 2012 (18:41 PM) 0 FansN°: 7
djiguene bou amoule valeur moko gay yeuke. valeur yakoy may sa bop
Neki En Novembre, 2012 (22:38 PM) 0 FansN°: 1
bilaye wakhatiko, ndeye gueye khana khalatoo ni bess dina ndieuw nga dee ni tekk tekkaral, dotoo mana yeungou bay fethi, nga wara diakarlo ak sa borome. ndeye adouna diekhna toubal nga diegualou bala ndioulaye diebale sa borome
Saly  En Novembre, 2012 (19:53 PM) 0 FansN°: 1
loumouy toub c un métier et c pas ton problème tu na ka pa la regarder el ta pas force adunna dal moy doywar cou dieuka diouk sa morom neko sangal sa tate bayi sa bossss
Italie001 En Novembre, 2012 (18:51 PM) 0 FansN°: 8
ndeye gueye mom soumaye khole photom di kodale....dafa sexy malgré tout ce qu'on dit sur elle....katouko rek la beugeu.....
Mw En Novembre, 2012 (18:59 PM) 0 FansN°: 9
italie yaye ponkali goor sexi ladef
0,00% En Novembre, 2012 (19:05 PM) 0 FansN°: 10
 :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down:  :down: 0.000000%
Ndiaga Seck En Novembre, 2012 (19:17 PM) 0 FansN°: 11
Le divertissement est l'un des obstacles rédhibitoires des pays africains sur le chemin vers la prospérité. Si on jaugeait le niveau de développement au moyen de la musique et de la danse le Sénégal serait en tête du peloton en Afrique.

Moi En Novembre, 2012 (19:28 PM) 0 FansN°: 12
merci m.seck
Fatigue Pas En Novembre, 2012 (19:37 PM) 0 FansN°: 13
HEY Allez chercher le probleme de L'AFIQUE, si vous etes incapables de trouver des solutions a vos problemes vous vous acharnez sur la musique, danse et autre. Le developpement n'a rien a voir avec, il vous faut des poilitiques realistes, une unite africaine forte pour faire face aux defis qui vous interpellent. Mais cessez ces arguments faciles d'en vouloir aux danseurs, lutteurs et autre. C'est trop facil comme argumentaire!!!
Mami En Novembre, 2012 (20:03 PM) 0 FansN°: 14
ahhh ahh ahhhhh weuy reee naa ba dioy waa gniii andak ndeye gueye fou gnou diogueee ahh ahhhhhhh

com ay deum. maiii ndeye sa rouge rafetnaaa
Efe En Novembre, 2012 (20:27 PM) 0 FansN°: 16
moise ambroise gomis ;mbaye dieye faye; pape ndiaye thiopet; ndeye gueye oumou sow ect ... GNIO YAKE SENEGAL RIEN QUE DE LA POURRITURE VOUS payerez tres cherdevant DIEU
Didi En Novembre, 2012 (20:30 PM) 0 FansN°: 17
khar dey wessou mbotté ndeye un peu de classe d'il t plait mais les 2 autres danseuses en bleu et vert sont trop affreuses comme des zombies
Italie001 En Novembre, 2012 (20:44 PM) 0 FansN°: 18
Regarde d'ici demain y'aura plus de 100 commentaires......les senegalais t'aime...mais ils le disent pas ...dagua sexy koi...noumaye déff ba lale la rék labeugeu
K En Novembre, 2012 (20:44 PM) 0 FansN°: 19
fi koufi yakhou ya yakh sa bop bougnou kene sonale. sounou yayi diangalnaniou les bnes manieres
Wawa! En Novembre, 2012 (20:56 PM) 0 FansN°: 21
Senegal ngingui si yi ba legui...ay fethieu..ay woneh ..tieur..perruque ...cest bon continuez...le progres viendra a vos pieds
Mw En Novembre, 2012 (21:00 PM) 0 FansN°: 22
deuguela dagno sokhore nd.thie kaw thie kanam
Anama En Novembre, 2012 (21:23 PM) 0 FansN°: 23
mom kagn mbigui si kaw,ak si kanam, lougnouy tiit kagn moy danoubi.
Mw En Novembre, 2012 (21:44 PM) 0 FansN°: 24
bou dano dadi dieul retraite
Se En Novembre, 2012 (22:39 PM) 0 FansN°: 25
TROP DE RECREATION DANS CE PAYS :tala-sylla:  :tala-sylla: 
Mass En Novembre, 2012 (23:15 PM) 0 FansN°: 26
ndeye gueye vous avez oublier sa cassette ou elle danser nue pour 6000 frs cfa ses filles sont pas de la bonne graine ici en europe sa passe de maison a maison
Efe En Novembre, 2012 (00:46 AM) 0 FansN°: 27
K meme si les maman vous apprennent les bonnes manieres la societe aussi a sa part de responsabilite
Mw En Novembre, 2012 (01:09 AM) 0 FansN°: 28
societe diangalouniou kene sa yaye ak sa papa lounioula diangaloul perte nga bougnou kene rey
Lebous Bi En Novembre, 2012 (05:36 AM) 0 FansN°: 29
Mane khamou a loutah SAMA mbok senegalais yi niou iniane mais Li mo tah niou raw niou si Lou Bari yeen diapali leen sen mbok mou avancer si Li mouye deff mo guen gee. Diko decourage vous prefere di degelou aye American yo khamni nonsence laniouye waye me sen mbok iniane guen trop (barigo Bou amoul dara mo dakh deff bruit que bi ame Dara)
Bo  En Novembre, 2012 (12:27 PM) 0 FansN°: 1
yaw khol mo diekh dakh daguaye fethie mé khamgueni ligueni def amoul chansse
Mw En Novembre, 2012 (05:49 AM) 0 FansN°: 30
merci lebou bi deugue rek nga wakh dagno iniane
Metti-ba Tarr En Novembre, 2012 (07:13 AM) 0 FansN°: 31
Qu'a -t-on fait de la GRACE de la Danse Senegalaise? De son ELEGANCE? De sa BEAUTE?

Je ne sais pas pour vous, mais pour nous, cela fait longtemps que l'on en voit plus!

Tout est devenu si AGRESSIF, que cela fait vraiment peur: les habits, le maquillage, la coiffure, les mouvements, les manieres, les comportements, le verbe...TOUT. Les "danseurs" sont tellement exentriques, devergondes, qu'ils sont horribles et deguelasses.

Pas de charme ni de classe!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!
Blood En Novembre, 2012 (09:31 AM) 0 FansN°: 32
en tout cas bou heurou féthie dioté mom damay féth. sénégal mo nékh dangay kheuy di rétane ba kheum mdrrrr
Vérité En Novembre, 2012 (10:52 AM) 0 FansN°: 34
oumou sow réx mo kham bopam
Belfille En Novembre, 2012 (11:38 AM) 0 FansN°: 35
ay nd gueye sagalale sa bop guir yalla gua bahi fethie legui mak gua et pense o mariage et fonde une famille
Salyy En Novembre, 2012 (19:46 PM) 0 FansN°: 1
t mieu ptetre
Bo En Novembre, 2012 (12:21 PM) 0 FansN°: 37
pére ouza bou dé mola wakh mangua waye nakhnala tonkara wakhna deugue ligueni def amou fin

Akon En Novembre, 2012 (14:06 PM) 0 FansN°: 38
li rafèt na si djiguèn .ngayè kou ni bakhna dou djiaglè bou rafaèt thi societe senegalaise ,kou yakar ni do dèè lou la nex dèfal dè dou dias sou nou borom kèn manou ko reuthe.
Saly En Novembre, 2012 (19:45 PM) 0 FansN°: 1
liii lou thi niaaw ak koula ko kholoo pfff nimporte koii c son metier kel a choiisi du genre toi tu va mdiir t sur un droii cheminn ligua def ni reek togne laa
Saly En Novembre, 2012 (19:42 PM) 0 FansN°: 39
maii ki vous a demandééé de la regarder c son gagne pain sa dignité et son futur c pas votre problème et si vos enfants dérape c pa de sa faute elle na pas forcer a votre enfants de danser kom elle !!takk ci riip koumou nekhoul tue bind yalla lettre

Akon  En Novembre, 2012 (20:36 PM) 0 FansN°: 40
gayi amoul mèr dè wala book comentère rek amoul wah lou si bokoul. kou beugeu dèèg deug mètier fècc dal dou metiè bou bah ,prostitution masquer la ngeuna nirou. fecc la tamou si adounam na fecc lou rafet ,bi moom rafetou djiekoul.

Commentez cet article

Auteur

Commentaire :

Service Commercial

Senegal : +221 33 864 65 71    |    Usa, Canada, Europe : +1 703 348 7306    |    Email : [email protected]

Rédaction

Email : [email protected]    |    Tel. (redacteur en Chef) : +221 77 562 00 29    |    Email (redacteur en Chef) : [email protected]