Triangle Vicieux Official
100%

Vues: 23802
Short URL:
Videos Similaires

+ de Videos
 Ajouter mon commentaire    Afficher les commentaires
Aidez-nous à modérer les commentaires en nous signalant les insultes. Merci de votre collaboration.
DXB on March 31, 2013 (01:34 AM) 0 FansN°:1
Pffffff.....encore mbeuguél...
Mister kaagne on March 31, 2013 (02:00 AM)0 FansN°: 2502772
wouuu mane DXB danou nga -16 lol hana haterz ngeu wala dégo wolof?
DXB on March 31, 2013 (04:38 AM)0 FansN°: 2502850
Refrain

Sama khol la yakkeu
Défnama louma nékhoul
Fimou nekk douma réthiou louma wéssou
Lii moy adouna, dangay diangue
Dafa bari ndiàgueu ndiagueu
Gnagnagni gnagnagnaa...

La video est belle ,le son est nickel chrome, les scenari sont corrects les images sont de bonne qualité , mais quoi ?

Pfff c'est encore du L.O.V.E sama wadji
Modou saar on March 31, 2013 (01:35 AM) 0 FansN°:2
DXB dof nga rek dél déklou akh khél waay
Soultan on March 31, 2013 (12:10 PM)0 FansN°: 2503157
Dxb a bel et bien raison ,tout ce qui a ete dit ici a ete déja dit et redit ici meme..
Il cait etre objectif dans la vie et accepeter les critique ,ca ne fait qu'avancer les choses ,mais kou wakh rék nguén guiss séne bopou....quel cercle vicoeux !
Nokoss bou saff on March 31, 2013 (01:59 AM) 0 FansN°:3
nice son au mois ça change du rap qui soule, le mm que tout les rappeurs du sénégal font
Astou thiam  on March 31, 2013 (02:02 AM) 0 FansN°:4
Waaw je kiff graveuh
Blédoss on March 31, 2013 (02:05 AM) 0 FansN°:5
Nice track c'est des rappeur comme ça qu'on a besoin,lyrics,thème,rime ,mélodies imagination et créativité tout est la sans oublié le Tama au début diadieuf avec un peu d'aide tiras Loin au moins tu copie personne
X on March 31, 2013 (02:18 AM) 0 FansN°:6
Wa mais boy bii graaww na anhh ! les rappeurs ont un nouveau talent ! Je sens qu'il vaboulverser le HP HOP galsen
Amina on March 31, 2013 (07:03 AM) 0 FansN°:7
trop nice je kiffes RESPECT  :up: 
Moon Ass on March 31, 2013 (09:55 AM) 0 FansN°:8
Doundou na li ngéne Doundou ni ba dal di tokk
Kham na li ngéne di yeuk ,ndakh mane si la nékone
Dama done Tchoutch fi tchouch fé ,aye fo la ko défone
dama dofone,défone ni ,kén dou ma ko déf
SI ki meu geunone Dof si sama life mo ma ko déf
Ma fock ni amatou ma khol né do touma beugeuti
Yallah bolé makh nite kou sopi sama life
ndakh dama ko trompé So many many time
Wayé lép khamone nako ,dafa goumbone rék tok
wane meu preuve youdoul diékh ,ndakh kholame massi Nékone
Si la tok Mine ,khamni kone
MBeuguél ,moung si Biir ,
ndakh dou khaliss ,dou taar, dou lénéne loudoul miir
si mane,
Ma niak sama (Ndéye) Meussou meu beug Baye
Motakh ma dieul sama khol diokh ko ,tiakhane dama ko BAAye
Khol khamni NMBEUGUél Deug amneu
Mais fock nga ame CHANCE Deug ngiir dalssi
Conclusion
Geumeutou meu ni
Nieup Bone ,dafa ame rék niou tégui Yonne
Bou féké ni dagne lako déf
Bou fi né di fayounto
LI moy adouneu ,da ngay ,dafa beuri Niangue niangue
DAma coolone
Fall di talie on March 31, 2013 (10:44 AM) 0 FansN°:9
je trrouve que la fille a des yeux sublimes
et comme quoi on peut montrer le beaute sans forcement fixer sur les fesses
En plus son teint super naturel, c est genial
j aimerais bien connaitre le nom de cette fille qui joue dans le clip, son regard, ses yeux et son cote nature
Jule01 on March 31, 2013 (11:43 AM) 0 FansN°:10
Nice ce son.Un gars bien en plus "Yang zoow"
Kitela on March 31, 2013 (18:10 PM) 0 FansN°:11
fall di talie on a capté que t'es un fille ;)
Solasarrr on April 1, 2013 (05:15 AM) 0 FansN°:12
j aime dpuis usa!!!!!!!!!!!!!!!! love it bro, u rock it! y a une tante ki m a dis k j ressemblai a la fille. j m suis hate pour voir le clip et boom j m suis dis wow g une jumelle la !! keep it up!
Fall d italie on April 1, 2013 (07:00 AM) 0 FansN°:13
Non je ne suis pas une fille ,mais bien un homme hetero en plus
j ai juste voulu dire ce que j ai eu comme impression face a un clip et j ai focalise sur les yeux
la question c est de savoir est ce que ses yeux sont bel et bien jolis ou non, est ce que son teint est aussi joli ou non et si ce clip tranche avec ceux ou ne montre que les fille qui se depigmentent avec de grosses fesses, c est une bonne chose, non
@fall italie on April 1, 2013 (07:21 AM)0 FansN°: 2504580
So deme rek tu as un pousse-poupe
Under 1992 on April 1, 2013 (08:29 AM) 0 FansN°:14
Pas mal, mais redoubler d 'effort pour faire du pur
Hip hop
Fan on April 1, 2013 (15:00 PM) 0 FansN°:15
Dama coolone,timide maname beury kérseu
Yoré khol bou sét,nieup fogoni douma MéR sakh
Kéne douma séét ndakh
Beury limite diangue la gueumone
Souma rombone bountou galé boutique la démone
Diamono di dokh may dieum mak di khamé Adouneu
Geun dakh dokh si galé bi béne roukhou Oumpoumeu
Di dokh di déme,di weur ba mbeukeuntékh mbeuguél
di doundou nékh,di kham you béss,ba fock ni Agana(adiana)
Lép cool,lép fine,
dama done feel nice!!
Mo nékone sama khol ma dane ko dream Every night
Mou diaralone ma lép,gueneu lone meu nieup
Nieup diépi wone meu,ndakh mome la défone
Mou nék sama lép!!!
Khala touma wone,béss nieuw lou bone diogué si mome
Fogone na lima done yeuk,louko raw nékon si Mome
Ndéké yo !!! souma fi nékoul mome akh kénéne leu
limou done wakh dima ko dikk lép aye féne leu !!!!!
Sama khol leu yakheu,déf nama louma nékhoul
Fimou né talou meu réthiou lima wéssou
Fimoy ADOUNA da ngay diangue
Dafa beury Niangue Niangue
Babacar cisse on April 1, 2013 (16:04 PM) 0 FansN°:16
THIS IS THE REAL HH s k je kiff c ke les lyrics touche le zik é bn et vous avé bien fé de choizir une fille ki n c po dipicmenté pour montré sa bauté des brai pro les gas
F on April 1, 2013 (17:29 PM) 0 FansN°:17
la fille trés jolie mais ton vernis tu pouvais bien la refaire parce ke c moche comme sa
Fall d italie on April 1, 2013 (21:09 PM) 0 FansN°:18
Non, le verni tel quel c'est fait express, ça montre une originalité
Khoulééte  on April 2, 2013 (13:17 PM) 0 FansN°:19
khalé bi kya laaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa la !! ma main sur le feu !!! khalé bou bakh waye yarounak dan la realité ! thieuye music :sn:  :sn:  :sn:  :sn:  :sn:  :up:  :up:  :up:  :up:  :up:  :bravo:  :bravo:  :bravo: 
Pape Gueye on April 2, 2013 (16:12 PM) 0 FansN°:20
Extraordinaire u're on the path guys
Baine bop on April 5, 2013 (16:52 PM) 0 FansN°:21
Niiiiiiiiice na
Jean jen on May 1, 2013 (20:32 PM) 0 FansN°:22
khalé bi mome witiakhouna dé hihihi

  Réagissez à cet article (en respectant les règles ci-dessous)

  • Soyez courtois. N'envoyez pas de message ayant un ton agressif ou insultant.
  • N'envoyez pas de message inutile.
  • Attaques personnelles. Vous pouvez critiquer une idée, mais pas d'attaques personnelles SVP. Ceci inclut tout message à contenu diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant pas la vie privée ou en violation avec la loi.
    Ne devoilez pas
    les informations privées de qui que ce soit ( adresses, etc... ).
    de tels messages seront supprimés et leurs auteurs bannis des commentaires.
  • Pas de publicité. Ce forum n'est pas un espace publicitaire!.
  • Pas de majuscules. Tout message inscrit entièrement en majuscule sera supprimé.
  • Lisez la politique de gestion des commentaires de Seneweb
  • Les auteurs de commentaires repetés (pollueurs) verront tous leurs commentaires á travers le site tout simplement retirés en un seul coup

Nom:
  
Commentaire:
:)   :-D   :cool:   :hun:   :cry:   :love:   :khelou:   :?:   :jumpy: :sad:   :bravo:    :haha:   :dedet:   :sn:   :down:    :up:  :tala-sylla:
   
Pour faire apparaitre vos commentaires immediatement, creez un compte seneweb (c'est rapide).

   
Videos Recentes

Pub
 





HitParade