A deux jours du Mawlid 2019, Médina Baye de Kaolack est en train d’accueillir ses premiers hôtes. Le président du Comité d’organisation des manifestations et activités de la Fayda (Comaf), Baye Mamoune Niass, est en train de veiller aux derniers réglages pour la bonne tenue de l’événement. Même si l’Etat a pris des engagements pour satisfaire les besoins à Médina Baye, des insuffisances ont été relevées. Le point avec Baye Mamoune Niass.
Auteur: Seneweb News Publié le: Jeudi 07 Novembre 2019
BAYYI LEEN KHALISSOU SENEGAL BI NGEEN DI PASSAR PASSAREE CI THIAKHANE YII. LII AY TOUUROU FAMILLE REK LA. KOU DIOK REK NE SAMA SABAR BI GUISSOUMA SI ETAT BI. GNOUN DEVELOPPEMENT LA GNOU WAKH. KHALIS BI GNOU FAY TOUR YEUP KHEDIOON NA CI ABRI PROVISOIRES YI AK CENTRES DE SANTE YI.
Répondre à THIEY XALIS SENEGAL
il y a 5 ans
Thiey sama mbokou mourides yi. vous vous prenez pour le centre du monde. Bou nguene meunone deug fall Idrissa Seck. Touba guiss nguene lamou fa am té takhoul mou gagner.
Au fond c'est vous qui n'aimez pas les Tidianes, té yénaniou moudj tekk beute, beug nio écraser, wanté soutoureu Mame Maodo ba yawmal khiyam Inchaa Allah. Louniou def nguene qualifier ko de topando. Yalla xamnani nioune gni ndigueul rek laniou done laniou done xaar ci jumaa dji, gni ci amone yéné barineu mais daniou amoul wone ndigueul. Nioune Tidiane yi liniou tabakh ci djaka au Sénégal barineu dé. Sama kogne mamelles zawiya baniou fay tabakh reuy neu rafett neu. Inchaa Allah jumaa dji dineu agg, donté ni Tivaouane niakou founiou djoulé. Dineu agg bou sobé yalla, et c'est une très belle architecture pour cette mosquée, mosquée bou rond amagoul sénégal. Def lene ci niane rek, nioune yiw naniou, diangue naniou.
Boudé fouki fanou bourdes yi mo lene méti sen affaire leu, way yi nekh neu, xam xam tourou na fa, soubeu nak niou magal goudi yonent bi ci ndigalou Cheikh Seydil Haj Malick.
Ba dewene ak diam Inchaa Allah.
Répondre à
Sunu yoone si sèni ndiambates il y a 5 ans
Voyez ça avec votre pote Aka Macky Sall . Vous avez fait campagne pour lui sans vous cacher, ne comptez pas sur nous pour être sensible à vos complaintes !
Commentaires (3)

Participer à la Discussion