Mardi 15 Octobre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Societe

[ Photos ] Les images inédites de Serigne Babacar Sy

Single Post
[ Photos ] Les images inédites de Serigne Babacar Sy

 
 
Il reste à jamais gravé dans notre mémoire collective. 
 
 
Photos : Les images inédites de Serigne Babacar Sy

photos
 

photos
 

photos
 

photos
 

photos
 

photos
 

 

photos
 

photos
 

photos
 


Article_similaires

53 Commentaires

  1. Auteur

    Door

    En Avril, 2011 (13:56 PM)
    yalna Allahou taass niou sissa barké Sy Malick !!!
  2. Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (14:00 PM)
    la 4eme photo à côté se Serigne Babacar c'est Serigne Mansour ?
    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (14:00 PM)
    Aimez priez pour son ame dieu soit loué il est le seul qui porte le nom de khalif dieu soit loué lui son frére Dabakh leurs parents Fallou Lahat Serigne Saliou dieu accueile ces saints dans son paradis amen
    Auteur

    Orba

    En Avril, 2011 (14:00 PM)
    na fa anallahou bibarakathi amin

    Auteur

    Bagne Kate

    En Avril, 2011 (14:01 PM)
     :haha:  :haha:  :haha:  :haha:  :haha: 
    Auteur

    Mansour

    En Avril, 2011 (14:03 PM)
    kène dou sama mame dji yalla nanou yalla tase si barkème

    Auteur

    Moh

    En Avril, 2011 (14:05 PM)
    yanna yalla yokh sen lere
    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (14:10 PM)
    amine sounou galsen diam rek la mana am

    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (14:21 PM)
    dou koumou nékh nga mélni mom loumou don yalla sounou bourom dako déf lata mom mouy ganéssi aduna ba takh si diamonom c'etai le seul ki répondai le nom khalifa wallay kén dou mom ki moy khalifa nieuw lén niou dém tivaoune ziarédjiko ndakh yalla yirrr niou :sn:  :sn:  :sn:  :sn:  :sn:  :sn:  :sn: 
    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (14:23 PM)
    Thiey mo niak morom :-D 
    Auteur

    Mouridoullahi

    En Avril, 2011 (14:30 PM)
    Respect  :up:  :up:  :up: 
    Auteur

    Ngakham1

    En Avril, 2011 (14:34 PM)
    la magie est interdite en islam
    Auteur

    Absa Samb

    En Avril, 2011 (14:37 PM)
    Bilayi ma la sope yalla na yalla yoko sa leer té tass gnou thi sa barké amine
    Auteur

    Yahman

    En Avril, 2011 (14:42 PM)
    un saint
    Auteur

    Mou

    En Avril, 2011 (14:47 PM)
    yal na niou ko yalla fayal :-D  :sn: 
    Auteur

    Sopé Serigne Babacar Sy

    En Avril, 2011 (14:52 PM)
    yalna yalla yok léram taf gnou thi barké amine
    Auteur

    Ffff

    En Avril, 2011 (15:09 PM)
    ah thieum thippiri

    Auteur

    Ami

    En Avril, 2011 (15:17 PM)
    serigne babacar etait le marabout des marabout
    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (15:19 PM)
    bayilene wakhi chaytane yi lo khamoul loumou doon bouol ko weddi



    serigne Babacar diine ji la fi teewaloon



    sergine Fallou diine ji la fi teewaloon



    mouy serigne Touba

    di Mame Maodo

    que Dieu soit satisfait d'eux tous autant qu'ils sont

    chaque individu a le droit de choisir son appartenance



    Senegal wakh you sew yi mo ko yakh



    soyons musulmans d'abord avant que d'etre tijaan ou mouride

    toutefois il tres bien d'etre mouride ou tijaan

    mais on n'est pas oblige



    salamoun khawlan min Rabbin Rahiim
    Auteur

    Tiwawaneee

    En Avril, 2011 (15:37 PM)
    SERIGNE TOUBA ET EL MALIKE SY N ETAIT PAS DES KONCOURANT LEUR FILS NON PLIUS SUIVON LEUR ENSEGNEMAN IL J ON SACRIFIER TOUTE LEUR VIE POUR NOUS :sn:  :sn:  :sn:  :sn: 
    Auteur

    Seugne Fallou

    En Avril, 2011 (15:46 PM)
    DU RESPECT QUAND MEME
    Auteur

    Youbi

    En Avril, 2011 (15:50 PM)
    dire du mal sur in saint parce que j appartiens a un autre tarikaha c est grave je ne suis pas disciple de babacar je suis mouride mais je ne dirai jamais du mal derriere lui parce qu ils appartiennnent a la meme famille et sont tous des musulmans wakh dafay rafet et si quelqu un disait du mal sur mon cher marabout alors je serai le premier a m enerver nit dafay maanou
    Auteur

    Dabak1

    En Avril, 2011 (16:11 PM)
    ATTENTION FRERES MUSULMANS TOUT TARIKHA CONFONDU IL YA DES NON-MUSULMANS QUI VEULENT LA SEPARATION DES MUSULMANS ALORS GUIR YALLAH NE TOMBER PAS DANS LE PIEGE

    Auteur

    Paabie

    En Avril, 2011 (16:13 PM)
    va dans youtube et tu tapes serigne mansour a la mecque et tu aura les arabe meme qui se prosterne devant lui apres le takhawayou arafat il y aura beaucoup de membre de la famille de babacar sy avec lui dans le hadj si vous continuer a dire des betises cree je vais juste vous demande ce que venait chercher serigne fallou chez lui et qu est ce qui a cause la disparition de votre guide pire encore il est enterre ou votre disciple du nom de Moussa Ka et comment il est mort
    Auteur

    Diop Chine

    En Avril, 2011 (16:22 PM)
    ZIAR BOU VER SI BARKE SY MALICK YALANGNOU YAMLA TASS SI BARK2 S BABACAR SY MALICK KHANA AMOLENE LIGUEYE YENE MBAME YIY KHASTE KHANA KHAMOLéNE NI AMNA LO KHAMNI SOUGNOUKO VAKHONE AADOUNA TOUKI YALA NAGNOU YALA MAY DIAMOU
    Auteur

    Paabie

    En Avril, 2011 (16:33 PM)
    mais nak wakhou dioulit moy ziar bou bakh serigne bi te dilene balou akh souma wakhe lou yaguel xolou diambour

    seneweb bi ma guiss ay franc macon laniou te licoy firndel moy daniouy vise toujours louy yakh pass passou lislam

    a bon entendeur salut
    Auteur

    Paabie

    En Avril, 2011 (16:47 PM)
    lathtel lou dokhone diguente gainde fatma ak son pere fallou ,lathtel loutakh bethio di def louco nekh te ken wakhoul bouma wakhlo
    Auteur

    Minééééééé

    En Avril, 2011 (17:01 PM)
    sa way khawma kane d wayé mbaye si mounoul si maneee daraaaaaaaaaaa!!!! sou ma ko eupoul ay leer sakh ki mon leudeumm way putinnnnnnnnnnnn!!
    Auteur

    Undefined

    En Avril, 2011 (17:28 PM)
    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    POURQUOI IL AVAIT EPOUSE LA NIECE DE FAIDHERBE ????

    • Auteur

      Ilo Yaladi

      En Avril, 2011 (19:46 PM)
      qui a épousé la nièce de faidherbe? Était-ce une babtou? plus d'infos please
    Auteur

    Defar Digueunté

    En Avril, 2011 (17:51 PM)
    salam,wakh deug yallah sénégalais mo doy warr

    un jour j'écoutais un waxtaan sur serigne babacar qui est sur seneweb meme(jotaayou lislam du 23 ou du 24 Mars),j'ai entendu dire que quand serigne cheikh est parti rendre visite a serigne fallou,ce dernier lui a donné la main gauche,quand il lui demande pourqui il lui dit "beboo ga diap si biiiiii,ndakhté bénéne bi diokhone nako sa baye ba paré" ceci prouve encore les bonnes reations qui ont existé entre les maras des deux confréries,mais les "talibés" restent tjrs la à se chamailler pour un rien,des propos pas du tout fondés,est ce que vous oseriez tenir de tels propos devant vos maras que vous essayez de défendre?????????Dieuféléne ndigueul té bayi dingate,deug nékhoul wanté kou si guiss sa bopp ma gui laye ballou akh,ecoutes l'emission,vous saurez qui est serigne Babacar,POUR L'ENTENTE ENTRE LES CONFRERIES!!!!!!

    SALAM
    Auteur

    Mame Diarra

    En Avril, 2011 (17:52 PM)
    pkoi lé mouride vont en espagne itali pr constuire touba c l argen dé toubab non é pkoi vs refusé lé toubakh té khaliss bouniou tabakhé touba li si eupe si pays toubab yi la DIOGUé
    Auteur

    Modou Pathiakh

    En Avril, 2011 (17:55 PM)
    LE mARABOUT ET LES MEDAILLES MDDDDDDRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRR
    Auteur

    Ya Salam

    En Avril, 2011 (17:57 PM)
    alhamdoulilah
    Auteur

    Sopey Dabakh

    En Avril, 2011 (18:09 PM)
    si vous voulez faite comme moi mane dé louniou mouti wakh si bamba mane mome tidiane rek lay done lo mana reproché osi tidiane yi mome rek lay done té lene nekh na ma ama guouy serigne bouy fethi rawatina yusa yusa
    Auteur

    Deuguejipossy

    En Avril, 2011 (18:28 PM)
    tous ceux ki reprochent souhaiteraient ke leurs BAYE et MAME portent des medailles



    nitt day mandou! loumoula yokaloul dou ko wagni, bande de cons
    Auteur

    Yirim Mbangik

    En Avril, 2011 (18:54 PM)
    yeen nieup mouslou leen ci seytaane serigne yi ci reeuwmi nioom lanou am nii deniou nouy diakhase deleusi leen seen xel haaah wakhnaa leenko khanaa ngeen wara seet ci serigne mansour mbaa serigne cheikh mbaa serigne abdoul aziz weete waroula takh ngeendi wakh yenn wakhyi  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet: 
    Auteur

    Saliou Ba

    En Avril, 2011 (19:11 PM)
    mame a babacar sy amou niou sa fay yalla na souf sed sa caw

    Auteur

    Msmn

    En Avril, 2011 (19:13 PM)
    vraiment site bi gnoum gneup dama yakaar né guemou niou yalla ndakhté le khalif mouride yalla na yalla yagal takhawayame ak gnénene nieup mo wakhone ni beugoul guiss musulmans yi di wakh ci tarikha yi
    Auteur

    Rama

    En Avril, 2011 (19:21 PM)
    ibliss mo sopalikou talal firam tè kppou kou si wakh lou bonn rèk tèk nga si sa tang ndakh dioulit dou wakh lou niaw serigne touba limou liguèy lako yalla di fay kènèn nonou soul dieuf mom sokhar la bakhoul
    Auteur

    Mimi

    En Avril, 2011 (19:30 PM)
    jvs assure kou reip rek moy wakh thi mame Babacar lo khamoul!!! kou fi wakh lou graw di ngako guiss thi ay few minute JVS JURE
    Auteur

    Seoul

    En Avril, 2011 (20:04 PM)
    salam naniou bayyi wakh bou bonne, mouride bou khame dara thi serigne touba dou wakh lou niaawe thi mame maodo, tidjiane bou bakh dou wakh lou niaaw thi bamba, serigne touba neena werdou yeppe bakh na, magui dieglou
    Auteur

    Bilal

    En Avril, 2011 (21:20 PM)
    onzou bilay mina seytanè radjim mè yène yeupp ay nafèk

    nioussou barri yen diangougnou baprè di jugè bayilène diakhassè tarikhayi seytanè yi yinguène donn thim
    Auteur

    Alou

    En Avril, 2011 (21:33 PM)
    avant tout je soumis à mon ziarra à mon marabout Seydi Aboubacar Sy RTA ,celui qui le Senegal n oubliera jamais parce que il etait rempli à son titre de KHALIFA à qui dont on parle de khalifa on pense aussitot à Serigne Babacar sy ,lui qui a accompli l,ouevre de son pere SEydi Elhadji Malick Sy qui a participe l,stabilite du Senegal nous prions que le Bon Dieu lui recompense à toutes choses reservees aux bons hommes et epargne ses discilples des choses qui divisent une famille et nous souhaitons à notre khalif general des tidianes Seydi Mouhamadou Mansour Sy une longue vie pleine de sante

    Auteur

    Fata

    En Avril, 2011 (21:42 PM)
    yalle na yalla tasse gniou thi barkè cheikhoule khalifa amine

    Auteur

    Quietlife

    En Avril, 2011 (21:54 PM)
    dieureudieuf sérigne babacar sy!

    Auteur

    Diop

    En Avril, 2011 (22:37 PM)
    li gayi wakh ba demougnou guethié bouko serigne touba wakhone dou demm guethie! c ttt
    Auteur

    Elhadji Malick Sy Fall

    En Avril, 2011 (22:48 PM)
    mame pour man

    man rek mala beugue tvb mame boy
    Auteur

    Seyfall

    En Avril, 2011 (22:59 PM)
    yale na yalla fayal niou serigne babacar sy al khalifa fi kouli jamany
    Auteur

    Liii

    En Mai, 2011 (00:03 AM)
    Lorsqu'il fallait inculpé goumalo seck, vous l'avez crié sur tous les toits et maintenant qu'il a été déclaré innocent on n'entend rien!!! GOUMALO SECK A ETE DECLARE INNOCENT!!! NON LIEU TOTAL
    Auteur

    Sante Serigne Saliou

    En Mai, 2011 (00:09 AM)
    Serigne Madieumbe Sylla masnay defal SERIGNE TOUBA mouy djapou, bimou aksé thi tangk yi Serigne bi neko ''Madieumbe kholal tank bi nimou toutè, te lou yeungou thi adouna moko yeugeul, Madieumbe khana khamô kouma yakar sa yakar dou tass, ndakh bou euleugè mane rek may gnimé takhaw fa kaname souniou borome nèko lep lo digléwone defnako te meusouma def lo tere, lolô takh kouma yakar sa yakar dou tass''
    Auteur

    Sante Kou Tedki

    En Mai, 2011 (00:11 AM)
    'Le motif de mon départ [en exil] est la volonté que ALLAH a eu d'élever mon rang et de faire de moi l'intercesseur des miens et le Serviteur du Prophète

    dieureudieuf serigne touba
    Auteur

    Fiesta

    En Mai, 2011 (00:36 AM)
    kel foule des bandits de faux types des malhonnetes wi des drogués des illetrés des faiseurs de malin qui d'entre vous maitrise le coran tout ce que vous savez c'est nous pompé l'air avec vos khaissaides dont vous ignorez la signification avec sa comment pouvaient vous redressé les personnes comment corriger les erreurs vous etes la a gueuleu té vous ignorez tout de votre religion en se disant que oui kou yakhar ahmadou bay sa yakhar dou tass kha tekk ko fane serigne touba bopam rek doyna kho nak santou léne li soyez avant tous des musulmans pieus sa vous éviterez de faire ces commentaires incense
    Auteur

    Ndiayyyy

    En Mai, 2011 (00:43 AM)
    j ai vu des gens insulter serigne babacar BILLAHI DINGUENE KO RETHIOU  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet:  :dedet: 
Top Banner
Banner 01
Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio