Jeudi 28 Mars, 2024 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Musique

Soda Bousso "Na-Rafet"

Single Post
Soda Bousso "Na-Rafet"


27 Commentaires

  1. Auteur

    So

    En Décembre, 2011 (12:39 PM)
    Tellement choquée que sama sourcils yi dano tiang à force de khouli sama beut yi, wa yène téma youkhou way, wa limou done. Pipipipipip!!!
    Top Banner
  2. Auteur

    Ross

    En Décembre, 2011 (12:50 PM)
    en tout cas tout le monde parle de aicha lo c ki elle parait milliardaire
    {comment_ads}
    Auteur

    Assia

    En Décembre, 2011 (13:19 PM)
     :hun:  :hun:  :hun:  :hun:  :hun:  so je suis du même avis que toi en plus il y a trop de bruit
    {comment_ads}
    Auteur

    Bobodiouf

    En Décembre, 2011 (14:25 PM)
    Elle est nouvelle dans le paysage des griots du Sénégal mais s'impose par son audace (arrogante à la limite). Aime se faire remarquer mais pire s'imposer même auprès de ceux qui ne s'interessent pas à elle. C'est ça son problème. Elle est étouffante
    {comment_ads}
    Auteur

    Catho ))

    En Décembre, 2011 (15:50 PM)
    c Grave en plus elle n'a mm pas le tempo, elles sont toutes folles
    Top Banner
    Auteur

    Cvb

    En Décembre, 2011 (18:17 PM)
    nekhoul dara
    {comment_ads}
    Auteur

    Ami à

    En Décembre, 2011 (18:45 PM)
    Soda c est très bon mais tu ne devrais pas chanter c est bizarre à nos yeux wayanal rek
    {comment_ads}
    Auteur

    Ety

    En Décembre, 2011 (21:30 PM)
    ni tete ni queue,la chanson n est pas pour toi;va danser et faire du wagnaane,sinon je t aime bien
    {comment_ads}
    Auteur

    Chiwii

    En Décembre, 2011 (21:39 PM)
    ooooooohhh trop nul vrément So chui avk toi mannn dama sakh tittt ohhh sénégal li loumou donnn
    Top Banner
    Auteur

    Poum

    En Décembre, 2011 (00:05 AM)
    soda lilan la sama gagni wakhlen ko mou togue deme wouti dieukeur elle est folle garcon manque arrete de faire du bruit persona non grata alassane mbaye wakhal sa kharit mou togue
    {comment_ads}
    Auteur

    Beuz

    En Décembre, 2011 (04:03 AM)
    nourouwop sa badiane Diabou SECK, khamoulo dara, nopil waye

    {comment_ads}
    Auteur

    Dadi

    En Décembre, 2011 (04:04 AM)
    pourqou les dames senegalaise garde pas leur couleure naturell puff dommage
    {comment_ads}
    Auteur

    Tiey Yallah

    En Décembre, 2011 (09:11 AM)
    mane niak souma sénégal mo nekh wa linalatila ni pépépépépép



    yaw ngay wayane di waye si sabari mou nekh rek nga degeulko nak dawléne !!!mane nak ma choké liiii :-D 
    Top Banner
    Auteur

    Makowakh

    En Décembre, 2011 (16:23 PM)
    wa li deguele doy na war  <img src="https://images.seneweb.com/content/seneweb/generic/images/smileys/khelou.gif" alt=":khelou:">  
    {comment_ads}
    Auteur

    Nch

    En Décembre, 2011 (17:03 PM)
    mais SO ray gua ma way moi aussi j'ai tellement rigolè ba sama bir bi di mèti sa commentaire todjnafi
    {comment_ads}
    Auteur

    Jajajaja

    En Décembre, 2011 (23:47 PM)
    vraiment maman kine lam ya niou togne depuis que ta enseigner ses especes de griotte qu on peut etre musicienne etant griotte kou diogue woye oooooooooohhhhhhhhhh vraiment elle nous sature mais au moins niou am voix bou nekhe mais mou melni kouye simbe soda bousso togal way aaaaaaaaaahhhhhh.
    {comment_ads}
    Auteur

    Féké Ma Ti Bolé

    En Décembre, 2011 (00:23 AM)
    wouuuuuuuuuu!!!!!!!!!!!!!.soda bousso rek ci desssone nakk thiey waye sénégal!!!!!!!!!!!

    kane mo ko done produire lii sakh !!!!!!!!

    mais mome sakh deffoule dara gniii donne arangé ak gniii done teugg waye sakh nio amoule foula.

    bou doule mbeurr yi di guéweul wayanne katyi !!!!!!!!!!!!

    Top Banner
    Auteur

    Sa Kharit

    En Décembre, 2011 (05:23 AM)
    wa SO!!!!!!!! Man de dama tiiit. Koulo way lo? khamsa bopp ci diamou yallah la boke. Sa kharit Youssou nena kham sa bopp mo guen niou woo la wakhla li nga doone. Chanter da fa am borom te yaw bokosi. So please soda beugue n la lol mrye adouna bi lou niou wakh dou ma nekh. Deloo ko foo ko dieule sa bamouye teeel.

    sa kharit
    {comment_ads}
    Auteur

    Bina

    En Décembre, 2011 (11:07 AM)
    senegal mo nekh kumu nekh woy maa danser pour devenir chanteur ecole yi amatougnou solo

    {comment_ads}
    Auteur

    Goudoulouss

    En Décembre, 2011 (15:47 PM)
    inchala soda bousso thikaw thiakanam
    {comment_ads}
    Auteur

    Lil

    En Décembre, 2011 (04:07 AM)
    En ce jour 16 decembre 2011 SODA BOUSSO plus connue sous le nom de SO remporte le 1er prix de la nullite devant Oumou sow(fly to fly), 2eme place et Ami Mbengue(cheri chocolat), 3eme place



    Categorie nullite: Chanteuse nulle, son nul, paroles nulles et jen passe



    Soda demale wayane sa guere yi nek suisse ak france teh baniou waye
    Top Banner
    Auteur

    Dxb

    En Décembre, 2011 (14:43 PM)
    Soda, Pape cheikh Diallo diay nala banga yaakarni ya dak woy kine lam,je t'aime bien mais touss defoulokofi



    j'ai envi de chauffer.........
    {comment_ads}
    Auteur

    Nds

    En Décembre, 2011 (00:33 AM)
    je l'aime bien elle a de la classe
    {comment_ads}
    Auteur

    Maye Kadaf

    En Décembre, 2011 (13:10 PM)
    de quelle classe vous parlez elle est plutot guéweul et style garcon on dit les borom 2 noms en tout c'est tout ce qu'elle me donne bien que l'apparence soit des fois trompeuses mais une femme doit être féminine et non masculine!
    {comment_ads}
    Auteur

    Ami De Soda

    En Décembre, 2011 (20:19 PM)
    Bayi lène soda, sama niit la, sama deukeundola, sama guewèlou soeur là té nit kou bakh là. Té moye badiènou bébé thiam, sama khoulowalé. Ken dieugoul rek, lepp sotti, soda artiste la té leup la meune. Dina féthia, dina teuggueu kon nak bou wayé boumou bett kenn, bougnou daklé, chaque décompte commence par un, pour une première, c'est moyen, attendons le deuxième clip pour juger, Courage ma Soda, un grand ami de Fass.
    Top Banner
    Auteur

    Babacar

    En Décembre, 2011 (21:08 PM)
    mai soda ya dof way magui si yaw

    {comment_ads}
    Auteur

    Fit

    En Décembre, 2011 (10:56 AM)
    ki lou mouy ndirol ken khamouko yabaté ba dé nékhoule tousss. Sénegal dé tass na nak rthey liiii wooooooooooooooooooooyyyyyyyyye

    {comment_ads}

Participer à la Discussion

  • Nous vous prions d'etre courtois.
  • N'envoyez pas de message ayant un ton agressif ou insultant.
  • N'envoyez pas de message inutile.
  • Pas de messages répétitifs, ou de hors sujéts.
  • Attaques personnelles. Vous pouvez critiquer une idée, mais pas d'attaques personnelles SVP. Ceci inclut tout message à contenu diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant pas la vie privée, sexuel ou en violation avec la loi. Ces messages seront supprimés.
  • Pas de publicité. Ce forum n'est pas un espace publicitaire gratuit.
  • Pas de majuscules. Tout message inscrit entièrement en majuscule sera supprimé.
Auteur: Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire...

Auteur Commentaire : Poster ma reponse

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email