News People: Omzo Dollar: ''Je me sens entièrement leader de la nouvelle Génération''

  • Source: : Seneweb Videos | Le 13 décembre, 2016 à 07:12:57 | Lu 19824 fois | 26 Commentaires

?

News People: Omzo Dollar: ''Je me sens entièrement leader de la nouvelle Génération''

Nouveau clip de Omzo Dollar pour son concert au grand théâtre le 30 décembre 2016

 


Auteur: Seneweb.com - Seneweb Videos




Commentaire (18)


Anonyme En Décembre, 2016 (07:48 AM) 0 FansN°: 1
Encore un polonais :xaxataay: 
Anonyme En Décembre, 2016 (08:10 AM) 0 FansN°: 2
Lebone lipone amone nafi dip doundou guiss. Nangou si geum yalla la bok. Dou kestion ke ayo ay nga omzo juste da fa ame koula soute less. Meilleur rappeur 2015, 2016...
Reply_author En Décembre, 2016 (09:15 AM) 0 FansN°: 1
je suis un melomane, un alkati mais je pense que omzo ak dip recreation mo lenn boole. vous avez sacre dip pour faire du mal a omzo, je pense que le rap que j' aime tant ne merite pas cela. omzo yay bomb. et puis il faut eviter de faire la promotion de ce doundou guiss. j'ai ecoute dip, il fait du bon mais il n'est pas de ta trempe. rap laniou wakh
Reply_author En Décembre, 2016 (10:24 AM) 0 FansN°: 1
way wakhofi dara alkati khanan lacrymo yi gnola mandi
Anonyme En Décembre, 2016 (08:16 AM) 0 FansN°: 3
OMZO ZOZO temps yii léer nga dé khana daguay khéssal
Anonyme En Décembre, 2016 (08:33 AM) 0 FansN°: 4
Heureusement k tu te sens nga wahh nangul dogal. Bi DIP moy sa bay ahkhou di say nidjay tu es le rappeur le plus impoli de ta génération mais aussi le plus vilain petit mongol waaa aller oussssssst  :emoshoot:  :fbhang:  :fbhang:  :fbhang:  :fbhang:  :fbhang:  :fbhang:  :fbhang: 
Anonyme En Décembre, 2016 (09:14 AM) 0 FansN°: 5
boy do leader nak! dip moy péé les dernier award galsen l ont confirme
Anonyme En Décembre, 2016 (09:30 AM) 0 FansN°: 6
touss xamouniouko,
Anonyme En Décembre, 2016 (10:06 AM) 0 FansN°: 7
kantabiw
Deeejay En Décembre, 2016 (10:54 AM) 0 FansN°: 8
Petit Prétentieux!!!!

Défaago fii daata lol

travaille encor!
Anonyme En Décembre, 2016 (12:23 PM) 0 FansN°: 9
BUZZLABBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBBB
Anonyme En Décembre, 2016 (12:29 PM) 0 FansN°: 10
mdrrrr. omzo naak yaw ko yabbb tu n'es mm pas de la nouvelle génération deif ngafi 8 ANS meuno bok thi nouvell gération bi. C a dire k en fait tu rap tro bien meme mais nangoul lou yalla dogal dip doundou guiss mofiiii meune actuellement.

 :sunugaal:  :sunugaal: 
Anonyme En Décembre, 2016 (16:09 PM) 0 FansN°: 11
Original Fake !!!! Mdrrrr Ben punchline nga tak radio di doul !!! Sicap sicap sicap!!! SICAP AMOUL BANDIT !! Hip hop is for Hood niggers!!! You aint shit nigger !!! Pistolet si Tank !! Bullshit !! yow do défé dara ngay tapet !! Real recognize real !!

 :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot: 
Anonymep En Décembre, 2016 (12:47 PM) 0 FansN°: 12
DIP DOUNDOU GUISS Késsé..

Dip Doundou Guiss number 1

DIP DOUNDOU GUISS For Ever... For Real... :sunugaal:  :sunugaal:  :sunugaal: 
Hip Hop Galsen En Décembre, 2016 (03:14 AM) 0 FansN°: 13
mdrr omzo yaw bayil dofdoflou u c tro bien k dip mola meune. Yangui rap dpui 10 anslane n,gaffii deif? Ta sorti un mixtape ki na pa fait du bruit ds les stations radio? boko thi nouvelle génération bi elzo dip ngaaka akhlou brick. meune nga rap tro nakk mai défa feik boy bi moy todj town bi. De la part dun connaisseur
Anonyme En Décembre, 2016 (14:41 PM) 0 FansN°: 14
 :thumbsup:  :thumbsup:  dip nii lagn kay deff  :emoshoot:  :fbhang: 
Anonyme En Décembre, 2016 (00:44 AM) 0 FansN°: 15
Yene ay nafek guene khana tay guene kham dip way maylen gnou diam lernamanii gnou moudjé djoud gnoy wakh nii rek Omzo il rap tres bien

Dip daffa meuna deuk di echo tripe rek defois il fau changer son wam teup dafko ratati rek koneu betté beurri wakh wa yenaguii nane dip dip dip lane lalene wakh louken yeii wakhlen rek

Anonyme En Décembre, 2016 (11:28 AM) 0 FansN°: 16
Pardon mais DIP c'est ces 2 derniere années hein? il rap depuis 2009 et last 2 ans yi leu commencé todj...

Donc loum fi def?

Senegalais beug lou bess rekkk...

Dip ay papeum rek gnofi nekk il rap bien nak mais senegalais mo gnemé tek nite foum nekagoul . dip moy def buzz actu sa veu pas dire k mofi meune

Omzo techniquement dou moromou DIP !

Boulene diawalé dégu wolof ak meune rap
Anonyme En Décembre, 2016 (18:33 PM) 0 FansN°: 17
lou bandi di niirol dip rk 4ever

tu clash pr faire tn buzz
Dollaveli En Janvier, 2017 (18:34 PM) 0 FansN°: 18
dip nena moy youssou ndour mais khamoul ni si ay akhlou brick rek lakoy nek! mais si omzo dollar dou dara loudoul philippe ndour;-);-)

Commentez cet article

Auteur

Commentaire :

Service Commercial

Senegal : +221 33 864 65 71    |    Usa, Canada, Europe : +1 703 348 7306    | +1 703 395 86 48   Email : [email protected]

Rédaction

Email : [email protected]