Mardi 17 Septembre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Top Banner
Video

Présidentielle 2019 : Suivez en direct le journal de la campagne

Single Post
Présidentielle 2019 : Suivez en direct le journal de la campagne

Présidentielle 2019 : Suivez en direct le journal de la campagne

Article_similaires

12 Commentaires

  1. Auteur

    En Février, 2019 (21:26 PM)
    Sunu Président moy defar ak samm ay relation you wor ak ay partenaireum pour def Sénégal, Rew bou am dolé



    • Auteur

      Reply_author

      En Février, 2019 (21:26 PM)
      ak pse, bi niou ko lancé 2012 néniou khamni macky fou sori ak fou rey ley guiss. sunu président bi, woné ti neu volonté bou mou am ngi developper sunu rew
    • Auteur

      Reply_author

      En Février, 2019 (21:27 PM)
      pse, projet bou niou togg ba mou nior leu, dé niou seytu bou bakh sunu komkom ak ay experts you nek ci domaine you beuri. mo takh niou def projet boul lerr, bou kham fi mou dieum. macky war neu meuneu am bénen mandat pour agalé ay projets wan ak réalisations yi. tek fi kenen mom woroul ci komkom bou rewmi.
  2. Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)


    Macky dafa dor transformation kom kom rewmi ci ay domaine you am solo comme tabakh bi, courant bi, mbey mi, mines yi, dekouway ak tourisme.

    Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)
    Ci histoirou Sénégal yeup, benn nii indiwoufi richesse bou toll ni ci Afrique. Macky rek mo ko fi def, mom rek mo meun né moy chef d'Etat bou mateu nek Njitou rew bouy youbou deuk ci emergence. Macky, kangam leu

    Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)
    Macky dafa fonk niit, dafa sokhali domi adama ci njang bi, ci formation bi, ci santé bi ak ci diapalé gni new dolé ak bourse familiale bi, CMU.

    Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)
    Macky Sall, li ko sokhal moy wakhtane beu joubo, diamb, stabilité rewmi ak sécurité nioy li ko sokhal ci gouvernanceum. Macky rek!

    Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)
    Macky mo fi digonn benn taux de croissance bou 7%, affaire yii mat neu té dey gueuneu yokk fi ley 2035. wolou na Macky.

    Auteur

    En Février, 2019 (21:27 PM)
    Macky mo takh sénégal developpé : Pole urbain bi niou tabakh Diamniadio, tali you bess ak autoroute yi, aeroport bi, TER ak projets you bess bou port

    Auteur

    En Février, 2019 (21:28 PM)
    2011, Sénégal dafa amonn probléme courant, bi nou défé PSE ba tay, production bi dafa yokk 500 MW à 1141 MW, ak energie you bess you niou yokk. Ci Solaire bi, 7 centrales you niou yokk.

    Auteur

    Moi

    En Février, 2019 (22:43 PM)
    Pour Sonko le PULAAR ne sera pas enseigné comme les autres langues qu'il a cité !
    Auteur

    Moi

    En Février, 2019 (22:45 PM)
    Pour Sonko le PULAAR ne sera pas enseigné comme les autres langues qu'il a cité !
    Auteur

    Moi

    En Février, 2019 (22:45 PM)
    Pour Sonko le PULAAR ne sera pas enseigné comme les autres langues qu'il a cité !
    Auteur

    En Février, 2019 (23:21 PM)
    Sonko amatul khaliss | IL va arreter bientot sa campagne. C'est pas facil dee sama waay hahahahah

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Top Banner
Top Banner
Banner 01
Top Banner

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email

Identifiez-vous

Don't have an account? Registration
OR